Ebook: Mitiƞ : Caaroy - Pikin - Caajaay - Kees Jànqeen. 1982 - 1983 - 1984 = Meeting de Pikine, Thiaroye, Thiadiaye, Thiès
- Genre: Other Social Sciences // Politics
- Year: 2016
- Publisher: OSAD (L'Organisation Sénégalaise d'Appui au Développement)
- City: Ndakaaru (Dakar)
- Language: Wolof, French
- pdf
"Jukki yi nu siiwal, ci mitiƞu RND yu Pikin, Caaroy, Caajaay ak Kees lañu tukkee ci atum 1982, 1983, 1984.
Mitiƞ yooyu Séex Anta Jéob mi ngi leen def ci kämpaañu palug dippite yu 1983 walla ginnaaw ba ñu ko nangulee pàrteem boobu di RND.
Séex Anta mu ngi ciy waxtaane pexe yi nu mën a jaar ba suqali réew mi ak ana luy ëllëgu Afrig.
Ci waxtaan yooyu, dellusi na ci xeex bi aju woon ci kayitu juddub pàrti bi ñu lànkoon ne duñu ko joxe, ci « demokaraasi » muy baatu mboolo mi, ak gëdda gi nu war a jox làmmiñi Afrig yi. Dina ci wax it mbirum Senegàmbi, balluwaayu kàttan yi, ràbboo gi réewi Afrig war a ràbboo te mu ànd ak sampinu isin yuy jariñ ci dun bi nu nekk.
Ay waxam, ni ñu dëggoo ba tey lu kéemaane la."

Download the book Mitiƞ : Caaroy - Pikin - Caajaay - Kees Jànqeen. 1982 - 1983 - 1984 = Meeting de Pikine, Thiaroye, Thiadiaye, Thiès for free or read online
Continue reading on any device:
Last viewed books
Related books
{related-news}
Comments (0)